04/05/2020 /
/Mbolo, nga khaamni défa aand ak fébar bou yombà nga khamni défay yômbal walanté COVID-19 tchii yaram, meun nga wô saa faadj kaat mou meun laa djokh vaccine bouy aar pneumokokker.
Vaccination bii defay aar ñi nga khaamni fébar défa yômb tchii séen yaram, aak ñii nga khaamni dûñio gaaw aam COVID-19.
Vaccination bii, dou vaccine nga khamni défay fadj COVID-19. Vaccine bii moy aar béne fébar bou tûdû pneumokok-bacteri, nga khaamni bii défa meuna djokhé aye fébar bou néka tchii deurét ak fëbaar deûne.
Niit you beuré ñio gaaw aam fébar, ndaakh séne aat waala mou dône niakum wër. Motakh ñio waakh ñii djem maag, ñii deuk tchii biir resisdence aand ak niakum wërgu yaram, ñiom ñio meuna aaam vaccine bii.
Leup lô beug khâm tchhii ndakh yangui bôk tchii vaccine yii ñungi kô biind fii:
https://www.sst.dk/da/Viden/Vaccination/
Liing beug kham tchii vaccination bii:
13/05/2020
Lou djogé tchii taxa way bii djogé tchii ministére bii bës bii 12. mai 2020 Danemark défa bok tchi yëw […] Læs mere… Læs mere…
12/05/2020
Niit you beuré ñju gui défar aye sën muuraay gémiñ bôp. Ministaire bou dal néena ngéen oytû lii dône aye […] Læs mere… Læs mere…
07/05/2020
Lou djogeu tchii taxaway 7. may ak Ministre bou djité rewmi Mette Frederiksen Danois yeup défnañio lou ñio meune, dii […] Læs mere… Læs mere…
06/05/2020
Bou djekeu ñi woora oytû tchii wallum COVID-19 défa yatû wône, motakh diktal bou bés, ñio meuna kham kaan mô […] Læs mere… Læs mere…
06/04/2020
Tarixx bii dëgër na, ñuu ngui tchii yône: Ñiaar téemer ak ñéet ñjô teudeu tjibiir hôpital yii, Béene tëmér ak […] Læs mere… Læs mere…
28/03/2020
Liinga wora khaam tchii corona: Wakhtou bii défa khaawaa djafé ndakh féebar bii. Moo takh ñio geuna deugeuraal suñu taawaye, […] Læs mere… Læs mere…
23/03/2020
Lii tchii biir conference aak journaliste yii beusou bii ñaar-fuuk ak ñett tchii biir wéeru marts 2020. Miinistere bouy djiitaal […] Læs mere… Læs mere…
19/03/2020
Beusou alxamis fukk ak juróom-ñeent bii tchii biir weerou marts, Ministaire bou weerguu yaram defa djokhé kaadouam tchii djiigeen bou […] Læs mere… Læs mere…
18/03/2020
Institution bii yoor vaccine moungii laadj njeup ñio bok tchi loulo tudu (influmeter); maanam nga meun leen djaapalee tchii feeñial […] Læs mere… Læs mere…
17/03/2020
Niit: Ministre bou rewmi Mette Frederiksen, ministre weergou yaram Magnus Heunicke, directeur tchii biir weergou yaram Soeren Brostroem, ministaire bitim […] Læs mere… Læs mere…
Hvert eneste medlemskab og donation styrker Mino Danmarks legitimitet og eksistensberettigelse.
Det gør en forskel og styrker foreningens muligheder for at lykkes med at skabe et lige samfund, uanset etnisk baggrund.
Hvert eneste medlemskab og donation styrker Mino Danmarks legitimitet og eksistensberettigelse.
Det gør en forskel og styrker foreningens muligheder for at lykkes med at skabe et lige samfund, uanset etnisk baggrund.