17/03/2020 /
/Niit: Ministre bou rewmi Mette Frederiksen, ministre weergou yaram Magnus Heunicke, directeur tchii biir weergou yaram Soeren Brostroem, ministaire bitim rëw aak Chéfou takk-der bou rewmii Torkild Fogde.
Ministre bou Rewmi defa tiidjii waakhtaan bii diiñio leeral niata niit ñio aand aak féebar bii: Juróom fukk ak ñiar (82) ñiô teede tjii hôpitâl yii, fukk ak juróom-ñett (18) séen cas defa djaafé, ñiit yii seen cas yii defñio béta. Motakh duuñu woora meuna def louñu meun ñio waanyii waallaaté yii.
Motakh soubaa beus bou fukk ak juróom-ñett tchii wëerou marts (18.3.2020) aye wakhtou fukk bout djoté, baa beusou fanweer tchii biir wëerou marts (30.3.2020) Rewmii diina djeul aye measure yuu bées.
Lou tchii topeu moy Heunicke, Brostroem ak Fogde ñio waakh dino woora oytu léegui léegui ñio meuna xatal feaabr bii aak lou tvhii meuna topeu.
Béene niit meunoul bayi djeul wallam, lolou laa ministaire tchii weur gii yaram wakh, defa djoubal wakh tdji sii ndongoma yii.
Ministre bou rewmi neena boudeh daangaa aam khéel ñiar, ndakh daanga woora deem diner ak saa aye khaarit, kone tôgal saa keur moo geuna wôr.
Ministre bou rewmi mungi bakhlée nieup nga khamnnii douñiô djaap sii taxaawai rewmi.
Lou tchii tope moy Ministre bou Rewmi defa ladjté aye ndimbal; djaapalé ligeuy kaat yii, nii ligayal seen bop, ûsune yii, souba diina waakhtaan aak partii yii.
Ministre biitem rew neena khaam naa nii aye niit duñio meuna njiibii léugui nii. Motaakh duñio wora wuut fuñio meuna neka, baa wakhtou njii djot.
13/05/2020
Lou djogé tchii taxa way bii djogé tchii ministére bii bës bii 12. mai 2020 Danemark défa bok tchi yëw […] Læs mere… Læs mere…
12/05/2020
Niit you beuré ñju gui défar aye sën muuraay gémiñ bôp. Ministaire bou dal néena ngéen oytû lii dône aye […] Læs mere… Læs mere…
07/05/2020
Lou djogeu tchii taxaway 7. may ak Ministre bou djité rewmi Mette Frederiksen Danois yeup défnañio lou ñio meune, dii […] Læs mere… Læs mere…
06/05/2020
Bou djekeu ñi woora oytû tchii wallum COVID-19 défa yatû wône, motakh diktal bou bés, ñio meuna kham kaan mô […] Læs mere… Læs mere…
04/05/2020
Mbolo, nga khaamni défa aand ak fébar bou yombà nga khamni défay yômbal walanté COVID-19 tchii yaram, meun nga wô […] Læs mere… Læs mere…
06/04/2020
Tarixx bii dëgër na, ñuu ngui tchii yône: Ñiaar téemer ak ñéet ñjô teudeu tjibiir hôpital yii, Béene tëmér ak […] Læs mere… Læs mere…
28/03/2020
Liinga wora khaam tchii corona: Wakhtou bii défa khaawaa djafé ndakh féebar bii. Moo takh ñio geuna deugeuraal suñu taawaye, […] Læs mere… Læs mere…
23/03/2020
Lii tchii biir conference aak journaliste yii beusou bii ñaar-fuuk ak ñett tchii biir wéeru marts 2020. Miinistere bouy djiitaal […] Læs mere… Læs mere…
19/03/2020
Beusou alxamis fukk ak juróom-ñeent bii tchii biir weerou marts, Ministaire bou weerguu yaram defa djokhé kaadouam tchii djiigeen bou […] Læs mere… Læs mere…
18/03/2020
Institution bii yoor vaccine moungii laadj njeup ñio bok tchi loulo tudu (influmeter); maanam nga meun leen djaapalee tchii feeñial […] Læs mere… Læs mere…
Hvert eneste medlemskab og donation styrker Mino Danmarks legitimitet og eksistensberettigelse.
Det gør en forskel og styrker foreningens muligheder for at lykkes med at skabe et lige samfund, uanset etnisk baggrund.
Hvert eneste medlemskab og donation styrker Mino Danmarks legitimitet og eksistensberettigelse.
Det gør en forskel og styrker foreningens muligheder for at lykkes med at skabe et lige samfund, uanset etnisk baggrund.